FOTOBUBAAXUL~ BAD PHOTOS

Ashtin Laurion - Senegal


March 9, 2018

Asallamalekum mboolo mi, na ngeen def? Li mooy fotobubaaxul ak dafa retanu.
May peace be on you audience, how are you all? This is bad photos and it is funny.

Mangi tudd Ousseynou Ndiaye. Sama sant dafa baax. Li mooy sama caro apré let bi dafa gën.

Ki mooy sama rakkbugoor, Ahmed Geuye. Ki bëggna nelaw.
This Is my younger brother Ahmed Guedye. He likes to sleep.

Ki mooy sama magbugoor, Aziz Ndiaye la tudd. Ki dafa baax.
This is my older brother, his name is Aziz Ndiaye. He is good.

Ki mooy sama rakkbujiggen. Danu fo ak caff besbunëkk. Li mooy foto bubaax ndaxte ki wax “danga wara Jox say xarit fotobubax rëkk”. Wante holal ci lochoam!

This is my younger sister. We play and joke everyday. This is a good because she said “you have to give your friends a good photo only” but look in her hand!

Ki mooy sunu dëkando. Jiboon laa tudd. Ki dafa dof. Ki dafa si si.

This is my neighborhood. His name is Jiboon. He Is crazy. He is “si si” which is kinda inappropriate but in a funny way.

Ashtin Laurion